current location : Lyricf.com
/
Songs
/
Wax Ma Allo lyrics
Wax Ma Allo lyrics
turnover time:2025-01-07 05:16:29
Wax Ma Allo lyrics

Sms la sa numb, woté si sa numb

Dieulo sa téléphone louma la def girl

Say sama cardiologue yoré sama commande xol

Mangui wadia crise té décroché go sa call

Bobou ba légui mangui lay wo yaw ngua khothie ma

Si loss bi moma sonal ba moudiou khothie ma

Dieuleul sa call ma puce dafa risteul

Sen nala texto sakh sa téléphone fisteul

Wakh ma, lo beugue, wakh ma

Ma love, ma switch girl lover

Lo beugue wakh ma soudé fék fék

Diaral nama soummi sama mboubou ganster

Dof dji si nimb ték si goor yi fégn si daara

Waala wo sa ben goorou diaaga

Mathie tougn diaay tilim done sa bén diaay taar

(Diaaga) fethial la??

Wo nala yoni yone dieulo sa téléphone

Bougn ma libalone kone dof lay done

Tay bouma la bégou lone déé ben yone

Diaral nguama kheuthie di rak souba ban ngone

Wakh ma I love, I love, I love dama la beugue baby

Wakh ma I love, I love, I love batakh ma nèkkeu

Nék na ak say kharite niou né ma dangua change mind

Dé nénagn ma nala bayyi ndakh yaw beugeu to

Ma niew na sa galé dila dila sét sa yaye torokhal ma

Dieul ngua ma fane ngua nék mane daal nameu nala

Hey girl foma dénthie batakh sa soumay teudeu dila guénteu

Fo diougue goul ma fanane fa bayil

Ma wétta li la bo dawoul dadi guéntteu

Lomay dégu mane dé guiss leu guissate yone

Di ngua ma gaagn ladial ombré zion

Yaw lay séét kouy nakh ma zine

Diaral nguama dém ba guédiou dayane

Sama love si yaw daddi sorri

May cry noumay déf ba guiss leu

Yay sama guénewal yaw xam ngua

Sama xol bi yaw la tanneu

Boudone sakh bén day leu

Man ak yaw doundou nagn mbeuguél

Tay sa taar diayleu

Ba ngua beugueu faté démbeu

Tangal may céréale, yama meuneu grillé

Boul khoulo malay koudoul mbeuguél amoul nioddi guerillé

Wakh ma i love, is a love, is a love moy takh ma nékkeu

Wakh ma I love, is a love, is a love, la beugueu dégu

Loving girl…

Loving girl

Loving girl…

Loving girl

Comments
Welcome to Lyricf comments! Please keep conversations courteous and on-topic. To fosterproductive and respectful conversations, you may see comments from our Community Managers.
Sign up to post
Sort by
Show More Comments
Jahman Xpress
  • country:Senegal
  • Languages:Wolof, English
  • Genre:Hip-Hop/Rap
Jahman Xpress
Jahman Xpress Featuring Lyrics
Latest update
Copyright 2023-2025 - www.lyricf.com All Rights Reserved