current location : Lyricf.com
/
Songs
/
Tapis rouge
Tapis rouge
turnover time:2025-01-03 19:26:42
Tapis rouge

[Narah]

Baby yow yaay diante biy leeral sama life, sama liiiiiiiiife.

Habibi yow yaay nguelaw biy fexeul sama xol, sama xooooool.

Lalal nala tapis rouge

Boul guestou dileen xool

Kaay mane ak yaw, niou déme suñu yoon

Fi yafi né ta kéne doula pousse

T'es l'amour de ma vie, juste toi et moi, juste toi et moi.

Lambo lambo...

Lambo lambo....

Baby lambo lambo....

Lambo lambo....

Lo amoul si mane rek si yaw laa

Souniou mbeuguel mak yaw louy law laa

Baby teudeul nelaw, sa guinaw bandang

Yaay thiabi biy oubi sama xol, sa toureu si nék oubil khool.

Baby teudeul nelaw ba kéne laal la

Lalal nala tapis rouge

Boul guestou dileen xool

Kaay mane ak yaw, niou déme souniou yoon

Fi yafi né té kéne doula pousse

T'es l'amour de ma vie, juste toi et moi, juste toi et moi.

[Jahman]

Yamay fathie baby yaay sama médecin yeah, yeah ehhhh

Again

It’s so magical baby we living love

We living love

trust and believe baby call me your Prince

all day all night gyal will live like twins

baby take it so easy

you’re driving me crazy

Hot the fire gyal miss don’t Play me busy

Yes, Isco lambo

Ting ling ling Play my heart like a guitar

Oh, baby ya love (baby ya love)

To ratatatatatouy

my heart like a drum says

[Narah]

Lalal nala tapis rouge

Boul guestou dileen xool

Kaay mane ak yaw, niou déme suñu yoon

Fi yafi né té kéne doula pousse

T'es l'amour de ma vie, juste toi et moi, juste toi et moi.

Lambo lambo...

Lambo lambo....

Baby lambo lambo...

Baby lambo lambo...

Comments
Welcome to Lyricf comments! Please keep conversations courteous and on-topic. To fosterproductive and respectful conversations, you may see comments from our Community Managers.
Sign up to post
Sort by
Show More Comments
Narah Diouf
  • country:Senegal
  • Languages:Wolof
Narah Diouf
Latest update
Copyright 2023-2025 - www.lyricf.com All Rights Reserved