Lima doundé, lima wessu day déloussé ba melni séttu
Lima doundé, lima wessu day déloussé ba melni séttu
Wait for me wait for me, abal ma way just wait for me
Wait for me wait for me, abal ma way just wait for me
Bala ma dougou école ci la am class
Ma nék ci sa xol ndax dama am thiat
Nama ray kholal nima beugué guel bi nama ray
Kholal nima nobé guel bi nama ray
Beug ko dioy ci mom, nijay né ma bayiko
Lalale nala tapis rouge, boul guetou di len khol
kay mane ak ioe niou dem souniou yone
Djiguen dey léral, léral ni sondél
meme bu lak bopeu douko téré léral
Talal béneu sondel sou takké tal fouki sondél
Talal béneu sondel sou takké tal fouki sondél
Yeah yeah ! fokey dieuléti koula beugeu ni mane
Fokey dieuléti koula sopeu ni mane mi
Fokey dieuléti
Khady loula nex, nex nama ioe
Ndax sama mbeuguel ci ioe, amoul demi-mesure
Kane moy vrai, faux vrai, faux vrai faux oh, aduna yeah
Kane moy vrai, faux vrai, faux vrai faux aduna
I’m so sorry hum
I’m so sorry I real feel sorry
Nobawone noboma ndeysane nobomawone
Bamaley Facetime taloma wone
No boulma message no boulma wo
Nobawone noboma ndeysane nobomawone
Bamaley Facetime taloma wone
No boulma message no boulma wo
Boulma khol ioe, wanema ko, mo geun ngamay sagané
Wane ma sa mbeuguel ioe, wane ma sa mbeuguel
Ioe yay sama chamalama ding dong yeah
Ioe yay sama chamalama ding dong yeah
Mbeuguel lou thiakhane taxouma diog
Mbeuguel lou fo takhouma diog
Mbeuguel lou minute takhouma diog
Mbeuguel lou yeurmandé ma takha diog
Waw waw, yeah yeah
Mbeuguel lou yeurmandé ma takha diog