current location : Lyricf.com
/
Songs
/
Sekougn Bayante lyrics
Sekougn Bayante lyrics
turnover time:2025-01-07 12:57:08
Sekougn Bayante lyrics

Begun ak lamign gna deuk yénn say gnou laalé

Man rek ma kham sa ndieuk motax sékougn bayanté

Boul mérr ba tangeu waxma loy reuthiou souniou joubo wé

Meun ngama gaagn té doko yeuk boulma waan sa dolé

Tidjil sa kanam bi nga teudj maan nga nop mala sommet

Niangal diapoula même so méré dangay gueuna rafétt

Doley mbeuguèl xadioul si yaw bayil finga téyè

Lewto sou yagué diéleu bi gnaaw mak yaw sékougn bayanté

Namnala wayé fokma tekk khel

Yèndo composé son numéro té douma beuss appel

Yéén say ma dougou mode fantôme

Dèm status xol la khèw tchia loy dokh gueuth na guiss no mèèl

Saguo ngi may raay

Wantè beugouma ndieuka wakh aak mom

May goor tè fokmou xamni fi bèneu baat leu may borom

Lowakh ma tangal tè

Pourtant man beug na bayi mou cèdeu

Dèl makh nakh so noppè ma doff

Sa baat la beug di dègu

Diaroul ngamay wane ni yangui ci diam

Xam naani yangui souffrir

Mak yaw gnoy wakh tè xamna lèèp

Damala bayi si biir

Damala nameu tvhi live bi goudi

Waay dougal dama ragal wètay

Taamal ngama lou meunta weuy

Wayè xeuyna dinga ma wo tay

Soumay lèèk lou nekh ba khèl mi dèm tchi yaw

Day melni meussou ma khiif

Wakhal aak maan nakh namnala

Sama khol meuna guiff

Oh love

Eh eh love

Magui beurè aak sama khol bi

Ba goudi gui dièkh wayè fouma tourné sa kanam laay yaam

Mbeuguèl di gueuna yokk come biss bimalay gneuka kham

Mal yak sougn khoulo nonn yi am ndam

I’m sorry yaw nameu nala eh

Chérie non non

Stay with me oh

Because baby I love you soo

Magui dora guiff

Lègui soma wowé

Yaay reine def nala leeep

Nakh mak yak sekougnou bayantè

(Dédèt yaw lay feel...)

Dou maan dou yaaw khol yi gnoko décidé

Mak yak sekougnou bayantè

Dou maan dou yaaw khol yi gnoko décidé

Mak yak sekougnou bayantè

Dou maan dou yaaw khol yi gnoko décidé

Comments
Welcome to Lyricf comments! Please keep conversations courteous and on-topic. To fosterproductive and respectful conversations, you may see comments from our Community Managers.
Sign up to post
Sort by
Show More Comments
Jahman Xpress
  • country:Senegal
  • Languages:Wolof, English
  • Genre:Hip-Hop/Rap
Jahman Xpress
Jahman Xpress Featuring Lyrics
Latest update
Copyright 2023-2025 - www.lyricf.com All Rights Reserved