current location : Lyricf.com
/
Songs
/
No More lyrics
No More lyrics
turnover time:2025-01-01 00:24:11
No More lyrics

Ashs the Best, what's up!

Fi lufi way am y’Allah ko may

Nianal niou may la mo geun ngey goungué

(goungué, goungué, nianal niou may la mo geun ngey goungué)

Allalou dounya diaroul niawo

Yéné nek la borom ma thiey fanané

(Fanan, fanan, yéné nek la borom ma thiey fanan)

No more (yéné lou bone yéné ray sa bop leu)

No more (yéné nek la borom ma thiey fanane)

No more (fanané)

No more (yéné nek la borome ma thiey fanane)

Fi koufi amoul dagn la nopal

Koufi né ci yone danioula tek temps

Yeah ! Djiko sénégalais moy beurri djiko

Ya raw picasso ndax beurri couleur, bouniou alo nga nopi casso

Daf fek nga moumeu mais takhoul nga téki sokhlam

Motax moudieuntal am na handicap takhoul nga geum boy

Boffi guissé kougn fi yeureum dafa denkané

Yeurmandé diekh, nétali baram sassuné

Yeurmandé diekh si xol mais da mougn

Boula ken geumoul geumeul sa bop goor (ligueye moy fay)

Ykkar ci y’Allah geuneu woor, yakkartu yakkar ci y’Allah moussoula woor

Kouci nek ak li la y’Allah buur bi may boul sokhor

Bul ignane yeah!

Y’Allah buur bi nélawoul la fi lofi dieuf lagn ley fay

Lo def lagn ley fay

Fi loufi way am y’Allah ko may

Nianal niou may la mo geun ngey goungué

(goungué, goungué, nianal niou may la mo geun ngey goungué)

Allalou dounya diaroul niawo

Yéné nek la borom ma thiey fanané

(Fanan, fanan, yéné nek la borom ma thiey fanan)

No more (yéné lou bone yéné ray sa bop leu)

No more (yéné nek la borom ma thiey fanane)

No more (fanané)

No more (yéné nek la borome ma thiey fanane)

Nioune bougouniou ngen ganio

Télou len lo, wa Sénégal télou len lo

Fi nga yendou lay fanané (no, no)

Fi nga yendou lay fanané (no, no)

No more, no more (yéné nek la borom ma thiey fanane)

No more (fanané)

No more (yéné nek la borome ma thiey fanane)

Fi loufi way am y’Allah ko may

Nianal niou may la mo geun ngey goungué

(goungué, goungué, nianal niou may la mo geun ngey goungué)

Allalou dounya diaroul niawo

Yéné nek la borom ma thiey fanané

(Fanan, fanan, yéné nek la borom ma thiey fanan)

No more (yéné lou bone yéné ray sa bop leu),

No more (yéné nek la borom ma thiey fanane)

No more (fanané)

No more (yéné nek la borome ma thiey fanane)

Comments
Welcome to Lyricf comments! Please keep conversations courteous and on-topic. To fosterproductive and respectful conversations, you may see comments from our Community Managers.
Sign up to post
Sort by
Show More Comments
Ashs The Best
  • country:Senegal
  • Languages:Wolof
Ashs The Best
Latest update
Copyright 2023-2025 - www.lyricf.com All Rights Reserved