current location : Lyricf.com
/
Songs
/
Nena Waaw lyrics
Nena Waaw lyrics
turnover time:2025-01-07 13:13:41
Nena Waaw lyrics

Li y’Allah sak leep ci taar sa dieum lama done missal

Moussougn téguénté wayé nio bok finiou done khol

Xeuthio métiwone neu, wayé ya finalou té ioe la faral

Xol yi wara andeu bagn dioudo batay nio ngui weureunté

Wayé sougn dadié ken si nioune dotugn wérenté

Kouné dina khamné, ki la done khar ki rek la war done

Néna waaw, té xol bi néna waaw

Wadiour yi nénagn waw, kharite yi nénagn waaw

Nieup nénagn waaw kone ioe la wara done

Néna waaw, té xol bi néna waaw

Wadiour yi nénagn waaw, kharite yi nénagn waaw

Gni banione sax nieup nénagn waaw

Ak ioe beugouma sax démé sama xel

Beugouma solou beurri mbeuguelou 0 calcule

Mane nagouwouma sax kou yakh sama xel

Si ioe même soudé deugeuleu malako nieuka wédi

Fogone nani xol bi yakhou na té dotouma beugate

Déception lou meti leu comme dal doto beugeu doundate

Wanté ioe, da nga melni drogue ci Sico pate

Dof bouy gagn té lola soxla

Néna waaw, té xol bi néna waaw

Wadiour yi nénagn waw, kharite yi nénagn waaw

Nieup nénagn waaw kone ioe la wara done

Néna waaw, té xol bi néna waaw

Wadiour yi nénagn waaw, kharite yi nénagn waaw

Gni banione sax nieup nénagn waaw

Néna waaw, té xol bi néna waaw

Wadiour yi nénagn waaw, kharite yi nénagn waaw

Nieup nénagn waaw kone ioe la wara done

Néna waaw (ioe la done set) té xol bi néna waaw (té ya ngui sama wet)

Wadiour yi nénagn waw, kharite yi nénagn waaw

Gni banione sax nieup nénagn waaw

Néna waaw, té xol bi néna waaw

Wadiour yi nénagn waaw, kharite yi nénagn waaw

Nieup nénagn waaw kone ioe la wara done

Néna waaw (ioe la done set) té xol bi néna waaw (té ya ngui sama wet)

Wadiour yi nénagn waw, kharite yi nénagn waaw

Gni banione sax nieup nénagn waaw

Soxla touma dara ndax nago batay ndax guiss na sama goe

Aduna bi yeup sa digeunté loxo mo si geuna woor

Nénala waaw, khalé bi, ioe la done khar

Départ ba lama mbeuguel arrivé ci ioe doto ma raw

Dawna ba soon meunoul nek bobou xol bi néna waaw

Métiwone nga daw, supporté nga samay caprice sax samay you ndaw

Comments
Welcome to Lyricf comments! Please keep conversations courteous and on-topic. To fosterproductive and respectful conversations, you may see comments from our Community Managers.
Sign up to post
Sort by
Show More Comments
Jahman Xpress
  • country:Senegal
  • Languages:Wolof, English
  • Genre:Hip-Hop/Rap
Jahman Xpress
Jahman Xpress Featuring Lyrics
Latest update
Copyright 2023-2025 - www.lyricf.com All Rights Reserved