current location : Lyricf.com
/
Songs
/
ànd xeex coronavirus lyrics
ànd xeex coronavirus lyrics
turnover time:2024-12-29 04:06:52
ànd xeex coronavirus lyrics

Sa loxo set

Sa lepp set

Bul nuyu kenn

Bul lëng kenn

Bul génn kese ndax bëg génn

Bul sëqët fepp

Bul jége kenn

Sëqët, fièvre, bop buy metti njëk feeñ

Soj, problème noyi, senn sa bakkan

Sëqët, fièvre, put buy metti, malaise feeñ

Du rey nit ku ñul si ñi xamul dëg ak fenn

Sa loxo set

Sa doom yi set

Bul nuyu kenn

Bul lëng kenn

Bul génn kese ndax bëg génn

Bul sëqët fepp

Bul jége kenn

Sa loxo set

Sa lepp set

Bul nuyu kenn

Bul lëng kenn

Bul génn kese ndax bëg génn

Xeex ak Corona Virus,

microbe, jàngoro la, du nit

Aduna nek si combat

Du gis ku muy xeexal

Nuro nak grippe

Nañu éviter contact physique

Xajul Grand Yoff, Colobane , Pikine

tax ba ñu annuler programmes yi siiw

Tax ba ñu foog ni àddinay tukki

Medecin sonu na si li

Amul vaccin, ordonnance tamit

Mu ngi ray, day toroxal nit yi

Buñu tooge dina bari ay victimes

Set si sa askan, set si sa bopu

Tëju te baña seeti sa mbokk

Julli sa màkkaan, Messe si la bokk

Xeex ko mu jeex mbir yepp mëna doxx

Masque, sabu, antiseptique

Raxasu, sangu dadi set wecc

Dal, muñ, bañ lu melni dess fi

Gën di ñaan pour jamm day dikk

Sa loxo set

Sa lepp set

Bul nuyu kenn

Bul lëng kenn

Bul génn kese ndax bëg génn

Bul sëqët fepp

Bul jége kenn

Sëqët , fièvre, bop buy mett njëk feeñ

Soj, problème noyi, senn sa bakkan

Sëqët , fièvre, put buy metti, malaise feeñ

Du ray nit ku ñul si ñi xamul dëg ak fenn

Sa loxo set

Sa doom yi set

Bul nuyu kenn

Bul lëng kenn

Bul génn kese ndax bëg génn

Bul sëqët fepp

Bul jége kenn

Sa loxo set

Sa lepp set

Bul nuyu kenn

Bul lëng kenn

Bul génn kese ndax bëg génn

Comments
Welcome to Lyricf comments! Please keep conversations courteous and on-topic. To fosterproductive and respectful conversations, you may see comments from our Community Managers.
Sign up to post
Sort by
Show More Comments
Dip Doundou Guiss
  • country:Senegal
  • Languages:Wolof, French, English
  • Genre:Electronica, Hip-Hop/Rap, Pop, R&B/Soul
  • Official site:https://www.instagram.com/dip_doundouguissofficiel/
Dip Doundou Guiss
Dip Doundou Guiss Featuring Lyrics
Latest update
Copyright 2023-2024 - www.lyricf.com All Rights Reserved