Takkuma teere, dama pikkiru
Danga corona walla sibbiru
Yay karaba demal wax ko kiriku
Man ngay jem sul mete netetu
Mane tefesul, lebu bi mën na pepesu
So bëggetul, demal buntu bi tëju wul
Bañal kennen nangu xale bi toye ni ku don sangu
Saf ni moutarde
Xonk ni bisap
Neex ni ditax ki yorul denu pitax
Jalax jëme
Foko jalax jeme
Jalax jeme xale bi fo ko jalax jeme
Jinde jane ci pax maako saŋ
Kudu gu ndaw ci dëxin maako saŋ
Teral samay noon maako saŋ
Mani saŋsé tëdi maako saŋ
Eh bañal loolu (maa baŋ)
Bañal loolu (eh maa baŋ)
Bañal loolu (maa baŋ)
Eh bañal loolu (mani la eh maa baŋ)
May sa cinema konn bësel play
Bul avance, bul recule, bul pause bësel play
Nay dëger yox la ñu dem
Jeli bi jaruta gudal
Malay yobu ayca jugal
Dinga tuki té do dem tugël
Xecc bu dagul dikk
Gaal bu demul diige
Cas bi demul dic
So xamul nopil te ne miik
Di caw sa fas mangek xiir
Yengel fépp té cow du riir
Def tékk ni janu biir
Bolé ci takal fépp ni berigo tiir
Jinde jane ci pax maako saŋ
Kudu gu ndaw ci dëxin maako saŋ
Teral samay noon maako saŋ
Mani saŋsé tëdi maako saŋ
Eh bañal loolu (maa baŋ)
Bañal loolu (eh maa baŋ)
Bañal loolu (maa baŋ)
Eh bañal loolu (mani la eh maa baŋ)