Sama telephone sa yoon nékouthi
Noumako amé sa yoon nékouthi
Sama sagnsé sa yoon nékouthi
Deug deug sa yoon nekouthi
Sama diouni bi sa yoon nékouthi
Foumou noumako amé sa yoon nékouthi
Yoor sa lamigne tak radio yi manila hey
Louthiy sa Yoon, hey Louthiy sa zone
Yoor sa lamigne tak radio yi manila hey Lu ci sa yoon
Fougne la fek yangui togué nitt
Sa guémingne na yarakh ni car rapide
Niémé yalla tek thi degueur fiite
Amo dianou biir lo yeuk fok mou six
Khama touma noumou démé ni
Town bi legui dafa teureudi
Facebook snapchat Twitter wakh dji yématoul si lamigne gni
Mytho mytho mytho mytho
Gawa sopi djiko
Yaw nieup nga kharitol Bene deugouwou thi
Deuké waté serigne yeux
Diékheul téré yeup
Lingay wakh yeup no dara amouthi
Deuké saupe dara amouthi
Yangui soss nass nothi fass fethi ndéké yo dara amouthi
Dieuleul sa temps ténga def bine bine
Tass katou digueune tenga ya gueuneu graw sémingne
Wola nga record
Message nga capturer
vocal nga transférer
Statut nga vu yakamti partager
Sama telephone sa yoon nékouthi
Noumako amé sa yoon nékouthi
Sama sagnsé sa yoon nékouthi
Deug deug sa yoon nekouthi
Sama diouni bi sa yoon nékouthi
Foumou noumako amé sa yoon nékouthi
Yoor sa lamigne tak radio yi manila hey
Louthiy sa Yoon, hey Louthiy sa zone
Yoor sa lamigne tak radio yi manila hey Lu ci sa yoon
Lo kham wakhé
Weur di nakhé
Deuké di lors
Amo ngor khamoulo lane moy Goree
Meuno bawo yeugo tino té do lathié
Pousso passo tébo sanione yepeuy tardé
Sa wakh dafa bari téweu diekh ni wiri wifi
Fokni ya kham leep wakhniou lo bokak Siri
Deuké garoualé diapé nieup woudiouu
Nieup sori laléla banta bou gouda
Sa dieuf diou niaw beuss dina nieuw ding ko réthiou
Khamnga Thiow lé bari wayé deugueuy moudiou
Moytoul sa noon dieul sa verre def thing thing
Adouna lepp teranga la téyél sa lamine
Wola nga record
Message nga capturer
vocal nga transférer
Statut nga vu yakamti partager
Dama pataa sa yoon nékouthi
Sama Sewaay sa yoon nékouthi
Sama niawaay sa yoon nékouthi
Deug deug sa yoon nekouthi
Dama Stylé sa yoon nékouthi
Sama Modé sa yoon nékouthi
Yoor sa lamigne tak radio yi manila hey louthiy sa Yoon
Seuytané Louthiy sa zone
Rambathie Sa Yoon Nékoussi
Yoor sa lamigne tak radio yi manila hey Lu ci sa yoon