current location : Lyricf.com
/
Songs
/
Laf Thiat lyrics
Laf Thiat lyrics
turnover time:2024-12-31 23:13:44
Laf Thiat lyrics

Yeah, Yeah, Yeah

Oumy Gueye

OMG

Mashallah baax ga yaru nga

Nena laf cat

Am tuuti bandit bëri cass

Nena laf cat

Yay kiy def dosi boole wax

Nena laf cat

Cat dafa gaw bëgguma kuñu rè

Nena laf cat

Ki kuko sukër, xalè bi laf cat

Soxla wul sapali, nena laf cat

Loxo bi gaaw na, xalè bi laf cat

Aka mëna sagnse, kone néléne laf cat

Ben gafi

Ku mel ni yaw amatul

Yamay jeri

Yay sedal sama xol man la

Deg nañ lu neh teyul ga gënë jap

Digunte bé dax mburok lem

Yamay Douta Mbaye

Louma neex neex nala

Lima bëgg deg rek gay wax

Xol bi nena waaw

Melo ni niom

Amo morom

Mashallah baax ga yaru nga

Nena laf cat

Am tuuti bandit bëri cass

Nena laf cat

Yay kiy def dosi bole wax

Nena laf cat

Cat dafa gaw bëgguma kuñu rè

Nena laf cat

Ki kuko sukër, xalè bi laf cat

Soxla wul sapali, nena laf cat

Loxo bi gaaw na, xalè bi laf cat

Aka mëna sagnse, kone néléne laf cat

Sa jiko ji neex na ma

Sa ree ju neex sofuma

Ningay waxe neex na ma

Dara ci yaw di sofuma

Kon nena laf cat

Weretuma ndax dof ci yaw

Sama caabi mbëguel mugi ci yaw

Aljana rek lay dunde ak yaw

Yama mëna facce

Yay garap bi gën ci man

Deg nama ñu naan

Couple bi dafa nice

Mashallah, hey kaar

Bulen ñu catu waay

Lamigne baxul waay

Lalal bant waay

Daagul ni ma daagu nee

Ñu andë doxal waay

Mashallah baax ga yaru nga

Nena laf cat

Am tuuti bandit bari cass

Nena laf cat

Yay kiy def dosi boole wax

Nena laf cat

Cat dafa gaw bëgguma kuñu rè

Nena laf cat

Ki kuko sukër, xalè bi laf cat

Soxla wul sapali, nena laf cat

Loxo bi gaaw na, xalè bi laf cat

Aka mëna sagnse, kone néléne laf cat

Sa jiko ji neex na ma

Sa ree ju neex sofuma

Ningay waxe neex na ma

Dara ci yaw di sofuma

Kon nena laf cat

Comments
Welcome to Lyricf comments! Please keep conversations courteous and on-topic. To fosterproductive and respectful conversations, you may see comments from our Community Managers.
Sign up to post
Sort by
Show More Comments
OMG
  • country:Senegal
  • Languages:Wolof
OMG
OMG Featuring Lyrics
Latest update
Copyright 2023-2024 - www.lyricf.com All Rights Reserved