current location : Lyricf.com
/
Songs
/
Def Si Code lyrics
Def Si Code lyrics
turnover time:2025-01-07 13:01:26
Def Si Code lyrics

Oh yeah

(Bagnal lolou)

Oh yeah

(Yaw mi adioul lolou)

Oh yeah

(Bagnal lolou)

Oh yeah

(Mani adioul lolou)

Oh yeah

(Aannh)

Oh yeah

(Bagnal lolou)

Yèneu say ma compou lèpeu noppi bayila sii biir

Limay togou sou gnoré nga xamni may bandit piire

Thiow djiboul diapè ma dof boudè moddi dalal sa xel

Madon ngaka ba am lima beug bou yabo nagn ma diay

Xam ba thja dafa nekh djiguène pèkhé konn wéroo

Yaw bandit ngamay diay dangay dièm meunago

Guisma tay né dangma nopp ma rè nga fokni dal nga thji

Fowèma mola taxa diok wayé dotoko défati

Ma ay si goor bou geumoul dara teksi beug ma fowè

Damlay wol dila réé nann la baby yafii né

Nanla amo morom bèneu ngafi Sama Gloria

Mbeuguèlou Joni-Joni thiop sa wari tok di xar ria

Banial lolou, banial lolou

May waxak yaw mani banial lolou

Adioul lolou, Adioul lolou

Yama geuna xamni ragalouma lolou

Def ci code (eeh eh)

Anh def si code (eeh eh)

Anh def si code (eeh eh)

Anh def si code (eeh eh)

Anh def si code (eeh eh)

Fii lofi indi ngafiy fèkeu boulma wo

Si arou bandit man goor la tè awma loumay perte

Wathièl sa bopou dalal boul diay sa taar ngir alal

Amo loudoul sa bopou lii dalay tardèl

Sa dara bougé woul ndakh lèpeu nga statut

(Mbètè monument)

Loula mètèk, loula neekh nga dougeul statut

(Tè todio fèneu)

Solak soumi melni yaw amo bèneu soucis

So xoulok sa copain yaw nieup xamko thji sa statut

Kèneu falè woula ko diotèl yako togn

Yaw sonal nganiok, ma yeureum samay nonn

Mbeuguèlou film nguèn di doundou

Falètou lenn moeurs guèl bouy wiri-wiri

Dou meuss diok thji mbèdeu

Dioubeu di wèssoul def statut nann la femme du boss

Kann leu ? Meuno lénn niou tek xel

Yènn koulèn raw dee gnèmè nguènn

Tè yenn geumolèn dara eh yaw règlèl

Bodonn mbeur narnga beui défaite ngaka

Nganan baby yafi né bilay yamay danèl

Adioul lolou, Adioul lolou

Yama geuna xamni ragalouma lolou

Banial lolou, banial lolou

May waxak yaw mani banial lolou

Def ci code (eeh eh)

Anh def si code (eeh eh)

Anh def si code (eeh eh)

Bouldi gawa naguou yeuk seu bopou boudoul yaw di kènènn

Nimay diapè lay bayè tè man goor douma fowè

Leungo nexna wayé ko bayi mou dèmaki mbagam

Si tu peux m’oublier je ferais comme si tu étais jamais né

Yangui nax sa bopou so foguè ni meunou’mala bayi

Djiguèna sou nieuguè dotoul saurr xawma loy diay

Beug bimala beug boulko diapè ragal

Boulma topou bama seuss nitt kou nèkeu amna limite

Respect bimala diox dèlo mako wala kounèkeu dem

Nangoul nala louné thji nga dakeu lè

Xoulou goudi xoulo beuthieuk dara taxoul nga ba

Louniow nga mér dama sonou say caprices

Goor dou ngora kassè djiguène dangkay meuna yeureum

Man kouma nara sonal man ma rombou lafi

Banial lolou, banial lolou

May waxak yaw mani banial lolou

Adioul lolou, Adioul lolou

Yama geuna xamni ragalouma lolou

Def si code (eeh eh)

Anh def si code (eeh eh)

Comments
Welcome to Lyricf comments! Please keep conversations courteous and on-topic. To fosterproductive and respectful conversations, you may see comments from our Community Managers.
Sign up to post
Sort by
Show More Comments
Jahman Xpress
  • country:Senegal
  • Languages:Wolof, English
  • Genre:Hip-Hop/Rap
Jahman Xpress
Jahman Xpress Featuring Lyrics
Latest update
Copyright 2023-2025 - www.lyricf.com All Rights Reserved