current location : Lyricf.com
/
Songs
/
Bamba Nieup lyrics
Bamba Nieup lyrics
turnover time:2025-01-07 12:53:59
Bamba Nieup lyrics

Bamba ndamal Sénégal lou nagn len manko

Diadeufeulko ndax liguéyam weur na aduna

Bamba ndamal Sénégal lou nagn len manko

Diadeufeulko ndax liguéyam weur na aduna

Ya salam

Cheikh Bamba ya am salam

Beuré wo té am nga ndam

Ziaré naleu Bamba yay kiraam

Doy ngama, Cheikh Bamba yow yaay geun gui amam

Yama geuneul wourouss ak ngalam

Gathié ngalama Bamba am nga ndam

Bamba ya meun sa kanam

Té ya meun sa guinaw

Ya dégok sa borom loko niane mou def ko

Loko wax mouné waw

Cheikh Bamba

Sa way dou gné wayou kénén

Dou tite ndax louniou ragal nganiko

Tiass sani ba dougn ko guissate

Ya diow thieur tarikha yi ak yénén keurou diné

Woy nga Insa Ibn Mariama

Fa nga boké ak El Hadji Malick Sy dou fi

Bayiwo ma, sa youma diaxlé guissla

Souma dégone warna sédé

Y’Allah may nala Cheikh Bamba ay kiram

Ya demm nieuw, té ganio kén ganioula

Ya wax kén wakhaloula

Dialoré borom mokoy nétali way

Li geun ci mane, ioe ya thia fess mouy xol bi

Daray aduna safatouma

Louma niak mougn ko, doylo leu sa morom

Cheikh Bamba, Cheikh bamba

Yakaarou djam yi, Cheikh Bamba

Cheikh Bamba, Cheikh Bamba

Mouride tidiane, khadre ak wa layène

Bamba nieup lafi nékal firndel lam done neu tay

Massalikul Jinaan

Ya dieul Fuzti tagué ta la Sainte Marie

Ak ki domam Insa ba egue ci Ya uma Ruhil Maliki

Mbegté Bachirou, leeram ga ngey weundélou

Sarr na ba dougou Makka

Né len ko djak mou Al Mountakha

Bamba yeurmandé la, yeumandé bou nieup bok

Koufi dakha saytou mbok

meussloula dal di khadjalé day dadjalé

Dem nga am ndam, dey yeufi bopam

Donoul kouniouy kham té mom laniou geum

Taylé na bopam nguir nott bakanam

Diox y’Allah lépam mome ak yonénam

Diambarou l’Islam mome laniou nann

NaLou ap mouride am amna ca wallam

Ken dotoul mel ni ioe, yay ramou romb djam gni

Mbacké do dem bayi niou, lerr na mouride yi

Riddal Ilakhi Alal Khadimi

Dieureudieuf Sérigne Touba

Sa dieuf leppeu y’Allah Fay

Comments
Welcome to Lyricf comments! Please keep conversations courteous and on-topic. To fosterproductive and respectful conversations, you may see comments from our Community Managers.
Sign up to post
Sort by
Show More Comments
Jahman Xpress
  • country:Senegal
  • Languages:Wolof, English
  • Genre:Hip-Hop/Rap
Jahman Xpress
Jahman Xpress Featuring Lyrics
Latest update
Copyright 2023-2025 - www.lyricf.com All Rights Reserved