current location : Lyricf.com
/
Songs
/
Bamba La Joie lyrics
Bamba La Joie lyrics
turnover time:2025-01-07 12:56:02
Bamba La Joie lyrics

Mbeckté leu yone bi yonou mbeckté leu

Mourid aldjana lay doundou bamba la joie

Mbeckté leu yone bi mbeckté késsé leu

Mourid aldjana lay doundou bamba la joie

Kemane la dou lambo yeurmandé

Bouniou massé kenal ko reck xeweul yi sawane

Mbeckté leu yone bi mbeckté késsé leu

Mourid aldjana lay doundou bamba la joie

Jalal djeu bollékok jamal djeu

Mo niou may mbeckté mouniouy sagguo fa touba

Mbeckté leu yone bi mbeckté késsé leu

Mourid aldjana lay doundou bamba la joie

Bamba ligueyeul rabana ba taxe malakah yeup nane

Ki dou nitt reck xana ndaxe katt mayam yi eup na

Souniouko nanggo téh diapp ko louniou yottou mou kheuthieul niouko

Bouniouko xamoul oumpaléko loumouniou dioxe nioiu yakk ko

Nagnoou diémeu toppou ndiguel leum téh diémeu sobbou si mbirreum

Diéma sakko gueurreumeum ndaxe lepp ??

Anh sa yone bi amoul tankk guinaw

Cheick Bamba ma yeureum sa none yi bamba djeureudieuf

Mbeckté rekk lay andal retane téh douma ko tayy

Amma mouridoullahi Cheick Bamba djeureudieuf

Bamba yay mbeur mi borom diankka ak guedj gui

Ya wettal yalla fa ma yombé firrné yagui nii

Souniou mbeur mi mo dane toubab bi

Toub lo téh do souri djam yi xassidam yagui weuy

Aaaaah

Mbegue mi souniou xol yi di fegne si kanam bi

Deff nagne si bamba téh do touniou weet yakaari djam yi

Kone sou way néh sargal na khadimi

Borom magal gué niou doggal boumou djam yi

Téh lou way am téyel nioun doyelonagne

Goor gua demone guedj mame borom touba

Xeweul y dadje na fepp

Yeupp gui nane bamba fepp bamba everywhere

Doylou ak wolou la am si yaw ya gueneu gaw cthi mane

Doy qua seukk lakkou way doye gua seuk lakkou way

Djeuredieuf

Watta gua rabana ba mou dioxe la koun fa ya koun

Doy gua seuk werrouway dieureudieuf

Hilhal houloubana la bamba waxe

Khala tawadiouddi kone nagne si saxe

Niou nekk si reck téh andak yar ak tegguin

Thierno borom darou diaral lakk

Boo doul wone ak yaw nioun douniou sakk

Day gueneu di nexe di andak yarr ak teguin

Mourid deug day rafetal dieuffine

Comments
Welcome to Lyricf comments! Please keep conversations courteous and on-topic. To fosterproductive and respectful conversations, you may see comments from our Community Managers.
Sign up to post
Sort by
Show More Comments
Jahman Xpress
  • country:Senegal
  • Languages:Wolof, English
  • Genre:Hip-Hop/Rap
Jahman Xpress
Jahman Xpress Featuring Lyrics
Latest update
Copyright 2023-2025 - www.lyricf.com All Rights Reserved