current location : Lyricf.com
/
Songs
/
Le Passeur lyrics
Le Passeur lyrics
turnover time:2024-12-28 09:13:37
Le Passeur lyrics

guiss nani guay daaw

guiss nala saa waay

diowé sééni gaal

guaa gni yééndou wooné

kou diowé ba soonou

diaambar la saa waay

toogal fanaane

baa beut séét

déém nafa sorinaa

bassouba sorinaa (2x)

khoolna liguay daaw

khoolaal assamane

bii guélaaw li yéksé

adiana soriwoula

kou la khool néla dieulma

toogal fanaane

toogal yéndou

baa beut séét

déém nafa sorinaa

bassouba sorinaa (10x)

Comments
Welcome to Lyricf comments! Please keep conversations courteous and on-topic. To fosterproductive and respectful conversations, you may see comments from our Community Managers.
Sign up to post
Sort by
Show More Comments
Wasis Diop
  • country:Senegal
  • Languages:English, Somali
  • Genre:Pop-Folk
  • Official site:http://www.wasisdiop.com/
  • Wiki:http://fr.wikipedia.org/wiki/Wasis_Diop
Wasis Diop
Latest update
Copyright 2023-2024 - www.lyricf.com All Rights Reserved