current location : Lyricf.com
/
Songs
/
Plaignant lyrics
Plaignant lyrics
turnover time:2025-01-08 06:01:58
Plaignant lyrics

Kagne Lala geudia dég ?

Fête bi nieuw ngmay woo ko mbaraan nga beug

Nga baal ma ach wayé doumala wakh allo

Ma def ci code nga beug takh nanan ma sekouniou bayante

(Wakhi dof)

Mane nga def sa bebe caisser ma def fess

Sa appel sama call moy baby ma cresh

Beugouma sa jikoo way

Ninga mel bayiko way (aan yan yan yan )

Si money rek ngay dokh moytoul glisser (glisser)

Ndakh élève bou nagouwoul jangue fow mouy tricher

Khale niaane

Zero jomm danga fokne yow lay ligueyal

Tey bi dou jalleu demal diamono nekh

Corona leudeumal poche yi ken talatoul wekhal

Mane mala geumeutoul te yako tek sa bopp

Comme si cheveux naturelles sama money rek nga nop

Beugouma sa jikoo way

Ninga mel bayiko way

Foune nga telephone

Encaisser Dakar Paris bas a OM plafonné

Nitou intérêt deuk dima tek deam doum ko nangou yalla tere

Been beus la rek kone loufi diar forcer

Sa sagnse bi nek si à l’aise yangui khalaat nokoy fayer

Nit koune linga am ngay douger marché, ah weh

Ki am na li ke am na lee boom la déranger

Dang ma jape bopou neen takj nga may dieund lo cheveux

Ah fi rew mi tolou boy kenn wakhoula deug

Mala eup problème lila war wathiouma

Ling ma yen dafa diss eyway wathie ma

Mane daal nga diape ben pwalish yow Ouzin

Yay des palais mane parc Hann

So beuge morom danga koy outi

Sa Mormon nekoufi mane doma mbaraan

Beugouma sa jikoo way

Ninga mel bayiko way

Beugouma sa jikoo way

Ninga mel bayiko way

Comments
Welcome to Lyricf comments! Please keep conversations courteous and on-topic. To fosterproductive and respectful conversations, you may see comments from our Community Managers.
Sign up to post
Sort by
Show More Comments
Jahman Xpress
  • country:Senegal
  • Languages:Wolof, English
  • Genre:Hip-Hop/Rap
Jahman Xpress
Jahman Xpress Featuring Lyrics
Latest update
Copyright 2023-2025 - www.lyricf.com All Rights Reserved