current location : Lyricf.com
/
Songs
/
Ndogal
Ndogal
turnover time:2025-01-03 20:15:47
Ndogal

Nitt ak doundam, nitt ak mélokan’am, nitt ak jeufinam

Y’allah ak meuninam, bayal sa warr

Ko khamoul dioud’am

Khamo thiossan’am, bayiko mou dem

Y’allah ak ndogalam topal sa wayy

Gorr dey nangou ndogal (gorr dey nangou ndogal)

Nanto di ker kéra diam gni

Dou sagane sank lap té do dougn, do set do sélal

Do kham boromam

Ouuhh… aaaah… hé am y’allah niakeu y’allah

ouuhh… aaaah… y’allah yallah bay sa tool

Ouuhh… aaaah… nato di kér kéra diam

Ouuhh… aaaah… y’allah yallah nagn ko gnane

Dougou si beugeu si guen

Dioudou di diéguési déh

Louxouss dou guéner billet

Dougou pour gniko fi beuy

Mounouma dokh si digue ndokh wayé bougou ma khof di tindi lokh

Deukeu di wax si nitt lou bone

Bo déwé guiss god do sigui khol ko

How lies on me eyes, (on me)

Loutax nga tek ma beut té guissoumala

Eyes on me why?

How eye on me (on me)

Life dou nonou menyeah!

Sokhor dey leundeumeul sama rouh,

Kignane dafey peundeul sama yourr

Y’allay xam xam, y’allay mbeuguel, y’allay am am

Y’allay mbecté

Life yakoy jugé moley teuthi

Life yakoy guédeu yakoy néxal

Life daley fowé ngen deugeul

Life geunoul kawé soufou bop

Gorr dey nangou ndogal (gorr dey nangou ndogal)

Nanto di ker kéra diam gni

Dou sagane sank lap té do dougn, do set do sélal

Do kham boromam

Ouuhh… aaaah… hé am y’allah niakeu y’allah

Ouuhh… aaaah… y’allah yallah bay sa tool

Ouuhh… aaaah… nato di kér kéra diam

Ouuhh… aaaah… y’allah yallah nagn ko gnane

Comments
Welcome to Lyricf comments! Please keep conversations courteous and on-topic. To fosterproductive and respectful conversations, you may see comments from our Community Managers.
Sign up to post
Sort by
Show More Comments
Ashs The Best
  • country:Senegal
  • Languages:Wolof
Ashs The Best
Latest update
Copyright 2023-2025 - www.lyricf.com All Rights Reserved