current location : Lyricf.com
/
Songs
/
Assamane lyrics
Assamane lyrics
turnover time:2025-01-22 19:03:33
Assamane lyrics

Kholal cii kaw té nga bayifa saye beut

Guisso dara lou djara thiow té mo waral lepp

Guisso dara lo meuneu laale lo meusseu tiim ak saye beut

Kholal ci kaw assamane wessu nga sa level

Gni fa né défouniou bruit té louné nga lène dégueul

Mais niouné nioune deukou gnoufi kou déh dinagnela

yégueul

Sama biss mou ngui nieuw, sama booss tayla xeuyna

Kone bou défé nga ndieuk dem néko nama diégueul

Nieup nénagne daf gnou tiim kone mo ngui cii assamane

Loutah mou tek niou fi lathieko saye maame Adama ak Awa

Nénagne nioune nio ngui doundeu Akhirou Zamane

Kou djot lettrou assamane exactement ndakh dama khawa

Yémou cii gni wané nii niom gueumeu tougnouko

Pour mane gni gueum gno yéwou gni dess dagno guemeintou

Comme Scientifique ak Philosophe yi diémeu prouvé lénène

Boudé bo guissoul do meusseu gueum déh nga thi poukeuré

men

Doko door balle bamou diaaleu

Ropalane khalatoufa yégueu

Lougni def xana sani niaane

Di niaane Yallah na ngou niaane yikoy fekk Assamane

Assamane Assamane Assamane Assamane

Kholal cii kaw té nga bayifa saye beut

Guisso dara té lifa né xadioul cii seu cerveau

Da nga koy khol moulay guiss mo ngui fepp fi ngay dieum

Aduna bepp la muur yémoul rek cii sen deuk

Kharitou wérr bek Bidew yi mbok Jante ak Naathie

Soubeu lay lerr Goudi mou leundeum gentlema

Boufay dem do yaubou touss démal sett sa maame

Loutah yène makk yi di défar testament

Han! Mom réka tedd ndaxté mane xamena

Mom rékay aaté mom réka am bobou makkama (Capacité)

Assamane nay limite té kène douko dindi

Amena diourom niarry (7) Assamanes kounek ak sa limite

Boul khol ci nignou doundé cii souf

Kigni goungué gniy roukhe

Té xam nga dioum wessuwoul

Maye gnou lepp lou bepp mindef di woute

Bagni meune def li nga gnou santeu fi lek niouy dougou sunu

bamell

Doko door balle bamou diaaleu

Ropalane khalatoufa yégueu

Lougni def xana sani niaane

Di niaane Yallah na ngou niaane yikoy fekk Assamane

Assamane Assamane Assamane Assamane

Comments
Welcome to Lyricf comments! Please keep conversations courteous and on-topic. To fosterproductive and respectful conversations, you may see comments from our Community Managers.
Sign up to post
Sort by
Show More Comments
Dip Doundou Guiss
  • country:Senegal
  • Languages:Wolof, French, English
  • Genre:Electronica, Hip-Hop/Rap, Pop, R&B/Soul
  • Official site:https://www.instagram.com/dip_doundouguissofficiel/
Dip Doundou Guiss
Dip Doundou Guiss Featuring Lyrics
Latest update
Copyright 2023-2025 - www.lyricf.com All Rights Reserved