current location : Lyricf.com
/
Songs
/
Takma lyrics
Takma lyrics
turnover time:2024-12-31 20:19:46
Takma lyrics

Takeu ma, soma také niou seuy

Takeu ma, soma také niou seuy

Nioune baniou tambalé ba tay ji

Moussoumala sonal

Wayé niouné khar bou fess’ay joy

Bébé j’ai mal

(Kham nga ni baby)

Beug nala seuyeul

(Yonél say nitt)

Niou def yeufou djoulit

Té sou déssone si mane rek

Waxatougn ko baby

Wayé lima done djiguène motax

May tok di khar

Gnane nala takoulo bébé

Wayé guisna ni parégo sax bébé

Gnane nala saraxouleu bébé

Wayé guisna ni parégo sax bébé

Khawma loula téré

Mane ma seuyeul la

Baby moma togn

Ma beug seuyeul leu

Bilay moma togn

Mane ma seuyeul la

Baby moma togn

Ma beug seu yeul leu

Khamna li nga beug may daw sa ganaw

Sama mbeuguel ci yaw dafay law ba faw

Beug gui ma sakou té do lal sa yél

Souma waxé waxou takeu ngani da ngey lathi sa yaye

So amone li la gueuneul dag mey teudé soub’ak ngone

Lolou doufi damey dem sama yone

Nékouma thiouné té

Nékatouma goné

Yobou nala founé

Wane nala louné

Té lepp louniou meussa sékk baby maley meuné

Kham nga li la warr j’ai pas de leçon à te donné

Kén khamoul li nga beug

Dem séti kouma beug

Mou takeu ma ci foula

Ma seuyeul ko ci deug

Fi koufi lamb yatéy dagou fougn la nobé

Dieul samey click

Dieul samay clack

Gnane nala saraxouleu bébé

Wayé guisna ni parégo sax bébé

Gnane nala saraxouleu bébé

Wayé guisna ni parégo sax bébé

Khawma loula téré

Mane ma seuyeul la

Baby moma togn

Ma beug seuyeul leu

Bilay moma togn

Mane ma seuyeul leu

Baby moma togn

Ma beug seuyeul leu

Kham nga ni baby

Beugouma loudoul seuyeul la

Nék sa sokhna

Doundeul lo la aldjana

Kham nga ni baby

Beugouma loudoul seuyeul la

Nék sa sokhna

Doundeul lo la aldjana

Baby takeu mane

Tay ma seuyeul leu

Légui ya meu mom

Manit maleu mom

Baby takeu mane

Tay ma seuyeul leu

Baby moma togn

Comments
Welcome to Lyricf comments! Please keep conversations courteous and on-topic. To fosterproductive and respectful conversations, you may see comments from our Community Managers.
Sign up to post
Sort by
Show More Comments
Queen Biz
  • country:Senegal
  • Languages:Wolof, English (Nigerian Pidgin)
Queen Biz
Latest update
Copyright 2023-2024 - www.lyricf.com All Rights Reserved