Dama nek gouné, oubi sama beut yé
Tokk di setlou aduna bi khamné dafa méti
Yensay ma teudé Yéwu khadja goudé
Tokk ci sama digue lale di dioy ndax diafé diafé
Done yakkar ci yayam, nekk kharitou baye’am
Mba kham ngen ni nitt niouma yoni dagn ma yakamté
Feep fouma diar Yeufi dafay mété
Yoon bi beurri khakham ba deukiy dima djané
Mba kham ngen ni douma ladji douma daw
Damay djiguen motax may daw battou ganaw
Yensay ma feugué
Niouné ma dou fi déh
Ma diok daldi korti korti délou fima diougué
Boudoul yeup nékathia
Makoy feug bageu déh
Wayé khamna ni aduna bi mounoul yombé
Mba kham ngen ni néwone na len yen
Damay dem mane dara douma té
Mane deh néwone na len
Mane déh damay dem
Damay dem mane dara douma té
Mane deh néwone na len
Mane déh damay dem
Mane QueenBiz mi déh mane déh damay dem
Feep fouma dal di dem
Gni nane ma mothi galace
Gni nane ma mome wayé dafa woyof seurr
Mba kham ngen ni mane mi damay djiguen douma goor
Na fass sama lafou seurr ba doni goor
Mane dina len di wane
Né diant bi foumuy fenké
Fofou la yéwo té khamna loufiy khéwé
Damay sante buur bé
Ci lim ma thieuré
Ndaxté khamna ni mome moy borome beut bou reuy bé
Mba kham ngen ni mane mi déh damay dem
Damay dem mane dara douma té
Mane déh néwone na len
Mane Queen damay dem
Damay dem mane dara douma té
Soul keer douko téré feign annh !
Oui yé douko téré feign
Wayé y’Allah bou keer daldi ndaw ba faf souralé len annh !
Douko téré feign
Mane dara douma té
Mane dara douma té
Mane dara douma té
Mane dara douma té
Mane dara douma té